Témoignage Professeur Mame Ousmane Ndiaye sur Seyidi Wa Mawlaya Mouhamadoul Moustapha Sy ❤️ niou bakh niep, ta beugue lou bakh sédél nanie ko, Mbaxam ak taxa wayam si dinné dji,
ta yakar na ni kép kou beugue lou baxe, beugue gua ko roye si dohaline ak si taxa wayam