Def bร kkaar lu bon la, waaye li muy bon-bon, nga dรซkk ca moo ko yรฉes !
Bu la saytaane manee ba nga def bร kkaar, na nga suturaal sa bopp ba bu ko kenn yรซg, nga gaaw tuubal ko sa boroom, te moytu di ko defaatโฆ
Ndax boo koy defaar rekk, man naa dem ba woyof ci yaw.
Woyofal bร kkaar nag, mooy yรฉes ci ab jullit !!!