✍🏾 لي جمِّلنَّ ظاهري و باطني بطاهر🫀| 20.46

Joined December 2009
1,885 Photos and videos
🚨🚨 wird Maxuuz🚨🚨 wird Maxuuz🚨🚨 wird Maxuuz 🚨🚨
19
46
75
21,536
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
« Et soyez endurants, car Allah est avec les endurants. »
75
469
4,748
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Gnane gou am solo guigniye diangue si biss bi moudié si atte mii
4
14
127
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Leeg-leeg duma bëgg a wax, waaye dinaa ko def ngir bañ ñuy yàq xelu nit ñi walla ñu leen di lëntal. Tuubaa dëkk la bu yayoo li Dakaar yayoo ci li état di séddale, muy ndox mu sell, électricité, route ak lépp lu ay nit di soxla. Ndax liy taxawaayu sénégalais yépp mooy seen taxawaay ci fay ay taxi ak yu ni mel, kon dañoo war a jot seen wàll. Bu dee ci wàllu diine nag lu mel ni tabax ay jumaa, day liggéey boo xam ne, dañu koo téyel seen bopp di ko defaral seen bopp génne ci état, loolu moo tàmbali woon jumaa ji ba mu yegsi fii. Bu dee nag li war état ci dëkk bi, am na ci yoo xam ne, seetaanug état tax na Tuubaa di ci jéemal boppam. Mbaa xam ngeen ne forage bu panne Tuubaa lu ci ëpp ñoo koy defaral seen bopp ? Xam ngeen ñaata quartier la Touba Ca Kanam yóbb ndox ? Te ñu nekkoon fu sori daan rooti muy lu metti, nu tëral fa ay tuyau gasal leen ba ndox mi yegg ci ñoom te loolu xaalis bi murid yi di participer rekk moo koy defar, te loolu état la waroon. Ci ag tënk rekk Tuubaa yamuñu ci defar jumaa waaye boole nañu ci di taxawu askan wi ci lépp doonte waru leen état la war. Tabaski gii rekk ay junniy nit wutal nañu leen ay yére ak dàll ñoom ak seen njaboot, te loolu waru leen waaye ngir Yàlla rekk ak Sëriñ Tuubaa. Dangaa war a wax état ne leen, murid yi ndegam seen wàllu diine téyel nañu ko seen bopp xaaruñu dara ci état, kon mbiri àdduna li ciy seen wàll ci réew mi fexe leen ñu jot ci, doonte ña nga cay jéemal seen bopp. Beneen bi mooy yaa ngi am mbokk walla dëkkandoo bu xiif mbaa mu mar ci sa wet, te teewul nga defar sa kër tabax ko, meublé ko ba mu jekk, te jox nit mu lekk moo gënoon a doon farata fuuf.
Sénégal - Touba M'backé : Dr Khadim M'backé, universitaire et spécialiste des sciences religieuses écrit :"Croyez-vous sincèrement qu'il soit normal de multiplier la construction de lieux de culte à coût de milliards dans une localité qui manque d'eau potable?"
10
90
262
14,552
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
20 Sep 2022
docs.google.com/document/d/1… 1- Ag Muriit 2- Njàngalem Sëriñ Tuubaa 3- Taxawaayu Sëriñ Tuubaa ci ci Alxuraan 4- Xasiiday Sëriñ Tuubaa 5- Wird Maaxuus 6- Tuubaa 7- Li waraal Màggalug Tuubaa 8- Kiliftéef ci yoonu muriit yi 9- Àddiya 10- Lenn ci meloy Sëriñ Tuubaa. Lien bi ✍
7
164
313
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Bisou tey bi lagnoukoy diangue gnétt yone (3fois), Sou wer wi fegnoul tey nga dianguaatt ko soubeu inchala 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 Gnane ngir diégualou sounou borom ak gnane sounou borom nangoul la sa Dieuf you bakh yepp si att mi
1
13
52
490
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Désolé d’interrompre votre SCROLL… Qu’Allah soulage vos fardeaux et vous comble de bonheur.
6
494
3,669
35,957
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Salam promo bi commencé na 10kg 3750f Variété Kent
2
36
39
3,096
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
🌱 Bâkr Al-Muzanî (رحمه الله) a dit : Si tu veux que ta prière te soit profitable, dis : « Il peut que celle-ci soit ma dernière ». 📚Jâmi' Al 'Ulûm wa l Hikâm 503
31
143
1,804
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Toute ma vie, et dans mes prières, je demande à pouvoir le suivre. Muhammad ﷺ est notre Prophète, et par sa lumière il nous guide🤍
7
21
496
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Un livre pour connaître Allah comme Il mérite d’être connu. 99 portes vers Sa miséricorde. Parfait comme cadeau ou pour ta bibliothèque islamique🥹🤍 J’en offre deux parmi les RT 🏷️ 1500f
33
55
675
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Bazin riche original qualité 📲78 142 65 66 #kebetu #sénégal #retweetme
2
4
260
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Machalla 🥰 Client bou xolam sedd daal dara dakoul lolou😍😍
Kaamil S Abdou Lahad souhaibou 10.000f 777790417
2
7
506
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
« Nous avons effectivement créé l'homme et Nous savons ce que son âme lui suggère et Nous sommes plus près de lui que sa veine jugulaire. » ( S50 : V16 )
51
279
2,786
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
❤️❤️❤️
12
135
1,015
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Tay la séentu bu njëkk ñeel weeru tamxarit. Ñaanu mujjug at mi ; bis bu mujj ci atum jullit ñi. Li nu ko ci jaamu ak us néew ci at mi, yal na nu ko nangul te safaan wa mu jéggal nu ko moom miy Jéggalaakoon ji.
20
58
726
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Y’a t-il un ophtalmologue à Dakar que je peux consulter sans rv svp ( urgence ) ???
4
27
30
4,212
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Yaa ngi wax lu am solo... Quand je vois des gens attaquer ceux qui n'ont rien demandé au lieu de sensibiliser la dame sur ses contenus pas pudique sur les réseaux... On laisse le fautif pour déplacer le curseur... Continuer leen di légitimité ñaawteef rekk
Ndawi leegi yi lu doy waar lañu bëgg légitimer muy nekk saŋewu ba noppi lu la neex sol dugal ko ci sa sàkk ci mbaalu jokkoo yi loolu warul te ay bàkkaar nga ciy jëlee Yàqute boo gis dafa am ñeneen ñu muy ubbil bunt def bàkkaar muy waa penc mi ñépp yamuñu
1
4
8
1,679
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
Ndawi leegi yi lu doy waar lañu bëgg légitimer muy nekk saŋewu ba noppi lu la neex sol dugal ko ci sa sàkk ci mbaalu jokkoo yi loolu warul te ay bàkkaar nga ciy jëlee Yàqute boo gis dafa am ñeneen ñu muy ubbil bunt def bàkkaar muy waa penc mi ñépp yamuñu
1
4
13
2,035
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
"Sëriñ Tuubaa de moom ku baax la" !
6
26
357
Cheikhul Xadim 🇸🇳🇵🇸 retweeted
La baisse de foi qu’Allah nous en préserve, c’est terrible 💔
1
124
775
7,101