Ndawi leegi yi lu doy waar lañu bëgg légitimer muy nekk saŋewu ba noppi lu la neex sol dugal ko ci sa sàkk ci mbaalu jokkoo yi loolu warul te ay bàkkaar nga ciy jëlee
Yàqute boo gis dafa am ñeneen ñu muy ubbil bunt def bàkkaar muy waa penc mi ñépp yamuñu