Sëriñ Tuubaa neena :
"Jàngg sama'g xasida ba noppi tàllal say yoxo di ñaan mi ngi mel ni nga yor junni (5 mille) dem fekk ku yor dërëm nga ni ko kaay ñu weecoo. Li ma dëxëñ ci xasida yi xamu leen ko. Jàngg leen rekk te wéy."
Aji nettali ji : Sëriñ Ceerno Mbàkke Gelongal