Soxna Maam Awa moom numéro page rek la soxla 😭😭😭😭😭😭😭😭. Cey Yàlla Sunu Boroom
Sénégal 🇸🇳 la xewe, fii si reew mi fi lañu jaggé, 😭♥️🥳
Allahu Akbar 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Cey Yalla mooy kimaan dëgg. Ak Alxur’aan ni mu ruggé ak nimu bërree. Ki mëssu l giss mokal ko mokalin wu yeeme shah 😭♥️🇸🇳🙏🏿